Natty Jean Sénégal Official Video
Soustitres Wolof, Français disponibles Album Imagine : Natty Jean en tournée : Auteur : Natty Jean Compositeur : Massif B Réalisation : Valentin Campagnie MontageÉtalonnage : Guillaume Agostin AG Concept Art Drone : Nazir Cissé Remerciements : Karim, Teranga, Kamzo. Lyrics : Wolof This is for my people, Sénégal Njaay Couplet Jolli na well, music bi deh le jolli na fi nañu teg level Ne Sénégal de kenn du ko yàq ak nimu mel Ñu change mentalité faut que ñu change suñu xel Xol yi nañu sell, naatange jolli well Man de lima xam ci corruption dugg ci jail Ku ci wàcc yoon ñu xàcc, bàcc yattu kel Ku fi jiite xamal ni xol yi de fees na dell kon boog nee ko rell Ana
|
|